« Mon mari dafa immature bamou eupou » : Ma vie de famille - Notre Continent
> NOTRE CONTINENT > - Confidence | Par Fatou Seck | Publié le 01/08/2024 03:08:27

« Mon mari dafa immature bamou eupou » : Ma vie de famille

Article écrit par le créateur de contenu : Boul Khol.
Enfaite suis mariée avec un homme extraordinaire baxe immaturitém nak foko mesurer rékk mou dépasser ko, on a fait 6 ans de mariage avec une fille de 4as.

Mais mon seul problème avec lui est que dafa immature bamou eupou, enfaite depuis notre mariage jusqu’à maintenant tatounén lay fananou. Un jour c’était en mois d’avril lako xalébi ndieuk guiss mou nélaw avec…

…sans habits ndaxe mane souma yéwo rék damay dieul sangu tatounén bi wayé bimouko guissé xalé tite youxou fofou yeupou ba deux jours démoul diagui, papa dji mom lolou safouko ay rétane lako déf, mais ce qui me fait plus mal xalé bi image bobou guénoul ci mémoire bi ndax période de la tabaski foumou rombou.

Kharr si mbéde bi di dioxogne khourou xarr yii nane sama papa amna you mélnii wa cartier bi yeup diko rétane téh papadji lolou safouko saxe massi nékône di sonal sama bopou mais mon mari yeuguelouko yaramam, dimanche.

Beulé passé sama dieukeur bi dafa dieuliwone sétte diass sén bén xarite modone mariage mougui nieuw vers 5h et quelques nieuw ma défaralko réram mou sangou rérr soumekou teud, mane dall dama nekk si salle de cuisine bi dégu xalé yii di youxou ma dégu sama batou dom bi di youxou nane mougui niii mougui nii mane ma nieuw fek Mr.

mougui nélaw ba dioutou sama dom bi diakarlo ak xoureum yi nane morom yii mougui nii silako doorr papa dji dora diok épi amoul loumouy déff loudoul dima méré, mane.

Aussi ma bayi bamou yéwou ma défaralko ndéki togu sama agne paré niko magui dém sama keur papa boma sokhlawé diga trouver solution xalé bi gakoy yobou mouy fanani si mamam wala boy teude si soll yéré, wayé dama remarqué nii limako waxe safouko ndaxe chaque jour dinama woo dinama yoné xalis soumay waxe ak mom si lolou dafmay.

Rétane nane meu boo soné diga gnibissi téh dafa niak fayda samedi passé lafeu nieuw ni nii dom dji lay sét si ma yobouko sama chambre sœur bi mou nék fa dima forcé ba coucher ak mane fofou té xamna djikom soumadone diéma bagne banioul déf ay bruit ba nite gni fek niou fofou, légui may demander conseil si genre mari you immature yi nane ga meune déf bagnou changer.

Merci di diégalou si longueur bi

Article écrit par le créateur de contenu : Boul Khol

La plateforme NOTRECONTINENT.COM permet à tous de diffuser gratuitement et librement les informations et opinions provenant des citoyens. Les particuliers, associations, ONG ou professionnels peuvent créer un compte et publier leurs articles Cliquez-ici.


Réagir à cet article

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

12 commentaires
Kim
La ça déborde grave
Le 2024-08-01 23:45:33
Mame bousso
Il n'est pas immature mais plutôt fou
Le 2024-08-01 22:04:22
Blow Man
Toi même tu es une sorcière pourquoi tu sors ça dehors même
Le 2024-08-01 15:35:52
IBRAHIMA NDIONE
C'est bon d'être gentil
Le 2024-08-01 14:29:27
Cheikh Fall
What a shame
Le 2024-08-01 11:23:03
Goré
Ya imature doof binga done
Le 2024-08-01 10:52:48
Vieira
Bi dieukeur merci,il aime être immatur ça lui fait plaisir je ne vois de Solution laba
Le 2024-08-01 10:07:13
Diallo
Lolou d'où immatur lolou yeufou doff la
Le 2024-08-01 09:30:27
Nina
Motakh il fait bien étudier son homme avant le mariage. Seuýdou thiakhane.
Le 2024-08-01 09:15:54
Faye Marianne
Amoul loumouy rouss
Le 2024-08-01 08:28:20
Faye Marianne
C'est vrai il est immature amoul loumouy rouss
Le 2024-08-01 08:22:40
Abdallah
J'ai rien compris à tout ça bref l'intérêt
Le 2024-08-01 06:52:31

Réagir à cet article

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

12 commentaires
Kim
La ça déborde grave
Le 2024-08-01 23:45:33
Mame bousso
Il n'est pas immature mais plutôt fou
Le 2024-08-01 22:04:22
Blow Man
Toi même tu es une sorcière pourquoi tu sors ça dehors même
Le 2024-08-01 15:35:52
IBRAHIMA NDIONE
C'est bon d'être gentil
Le 2024-08-01 14:29:27
Cheikh Fall
What a shame
Le 2024-08-01 11:23:03
Goré
Ya imature doof binga done
Le 2024-08-01 10:52:48
Vieira
Bi dieukeur merci,il aime être immatur ça lui fait plaisir je ne vois de Solution laba
Le 2024-08-01 10:07:13
Diallo
Lolou d'où immatur lolou yeufou doff la
Le 2024-08-01 09:30:27
Nina
Motakh il fait bien étudier son homme avant le mariage. Seuýdou thiakhane.
Le 2024-08-01 09:15:54
Faye Marianne
Amoul loumouy rouss
Le 2024-08-01 08:28:20
Faye Marianne
C'est vrai il est immature amoul loumouy rouss
Le 2024-08-01 08:22:40
Abdallah
J'ai rien compris à tout ça bref l'intérêt
Le 2024-08-01 06:52:31

Copyright © 2023 www.notrecontinent.com

To Top